Application bii dafa ëmb ay jaar-jaaru Yonenti Yàlla Suleymaan. Téere bi bi nu ko bindee ak leegi ëpp na 2700i at. Dafa fes ak xam-xamu Yàlla ngir sunuy dundin fi ci kaw suuf.